
letra de touss - ibu fire
mh911 :
dey yeimei si yoe beu do meuneuti lale tiouss maguek mèrou ndieme sameu equipe
doter le rap diko fanano bayleine niuy kheutio ay tétine
def negn fi ay bêtises mais amnegn ay hit sugnu bêtisier
ah oui
pour nous c’est facile mais
on a charbonner pour mounek pétrole
encaisser liasses def lokho si poche
décaisser djeund seu bop niom xamuniu touss fokniu tous meuneu bo keu ey
bayleine niu wax niuguci tol yi
liguey beu deh limey def cadeau god leu ey sameu pakaa niari boor leu ey
flow yi cossou son wou boss leu tey
djeundo linei sameu bop
tameu djot peureum beu xameito or bi ey
motax niu nieuwat nieuwat def fi le ménage bokugn ni xdoxak diwline dugn niu mélanger
og niayes niayes meunoul deranger
steeve wonder when i shoot
u better trust me cuz i never miss
maguek fire di boyal la casa
tei niunkey def niune depuis tout petit yeah yeah too many flow soufou foureul bi
perseverance moniu indi fi
consa goniu motax xamoni u need it
too many flow soufou foureul bi
perseverance moniu indi fi
consa goniu motax aaaaaaahhh
refrain :
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
(
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
)
ibu fire:
xamolene dara ni kou guel di mbarane
yoro lene doule ngene di doule di saarane
bougnlé deggué fogg ni dangene neu aay ndekké flow yi ngene indi fi dangene ko xaarane
bolene yéwo seni dara dou foudou
yene nieuplaye wahal di xar koumeu tontou
seu guel bi néneu meunaloko dara motakh moumaye woo pour meu fatalko fofou
fi bene effet doufi deffé effet, nikko qatar deffé dangene niémé défaite
dangene meussoul diaffé, dangene meussoul niaffé
yone wou leer ni meew, kene doukofi kaaffé
dolene roi des arènes loudoul nioddi kessé, kene meusougnou wone fane leu comptam bi fessé
meune na lene doundale ak sama salaire kessé, boulene diakhlé hamnaa dinagn meusseu tassé
ndakh fi leu gangsters yi , dougou ci milieu bi ni nampalys
gérer kagne bi, gérer namps yi, dougou kogn yi feye lamps yi
sama teene bi lanieuw samp nii, sama melomaane yii tank cii
degg naa fii nieupa guedd ndakhté degg naalene niounane souniou diankk yii dougnou touss
refrain :
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
(
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
xamolene touss, xamolene nada
xamolene touss touss touss, xamolene nada
)
letras aleatórias
- pink navel › letra de present vendor - pink navel
- akira the don › letra de the wise man and the fool - akira the don
- briscoe › letra de easy does it - briscoe
- hava alberstein חוה אלברשטיין › letra de zemer lebni - זמר לבני - hava alberstein - חוה אלברשטיין
- gemini 제미나이 › letra de going (remix) - gemini (제미나이)
- h4ly › letra de jerk freestyle 2! - h4ly
- milly carolina francesca giuseppina mignone › letra de lontano, lontano - milly (carolina francesca giuseppina mignone)
- девятнадцатый devyatnadcatii › letra de карнавал (carnival) - девятнадцатый (devyatnadcatii)
- camel power club › letra de murano - camel power club
- кибо qibo › letra de тянет нас (pulls us) - кибо (qibo)