letras.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

letra de david beckham - yanchi squa

Loading...

yanchi squa david beckam (lyrics)

verset:
yagui dogeuu xam niit aka beurri weurseuk dama dane job goodie di xoolé ba betset diiw aka bax da fekk mom xolam seet legui may sa papa déma signél ay cheque loutax mono pouss joe meusso nangou echec yow do meusseu yeek mm bouniouleu alone ech-lle
boy do defe gatt xana di guéné dechet bandit tagounala waxma kaan desse?

okay doumeu niit waxnga ok
sa ay xaritt wathie lafi yow nga m-f-udiou bloqué
depuis lors yagui yoré app kanamou tapéte fo teudiou sa biir neek di xalate noy oeuvré

bandit dama diss degloule noumeuy croquer sax yi ci seu bamel lamay diap di c-cktail
am xelou dictionnaire boy dou tax nga riposter guisso mawti statu wam demb yow la poster yan

refrain:
nioune sa fiit laniouy teubeul
ay feni neen doyna seuk
oubi say nope teudiate sa gatt
yanchi seu mere yanchi sa papa bi dana saff kani sadam louniou defone demb laniouye defat sa ay defenseur dounioula defendre kone
meusso xaam david beckam (ooh)

meusso xaam david beckam (ooh)
ay gandam but sa ay lucarne (ooh)
danga beug xam david beckam
aythia dome ndeye come on non
meusso xaam david beckam (ooh)
meusso xaam david beckam (ooh)
danga beug xam david beckham (ooh)
aythia dome ndeye come on

autotune version:
meusso xaam david beckam
meusso xaam david beckam
danga beug xaam david beckham
aythia domou ndye comon
meusso xaam david beckam
meusso xaam david beckam
danga beug xaam david beckham
aythia domou ndye comon

verset:
yes douma beurré ak hypocrite astamak yow lo beug guéne sama vie diarouta taggo
mane doumeu hors jeux boppu yaboy
lolou sa ne fait pas mm ci tangor

mais bon c la vie on sy quoi
use sama matiere grise bayila ak poid naniou job dinga guiss filek 4 ans rap game bi laye thiop melni pain ton

douma yow tey do mane sa decapote
douma bayi sa ay fake
sandi kaddu ben yoon bi
laye done mangui ci parcour
louma def-gout sax la xamagout?

pendant cependant mangui job hay
sama ay decendance niogui ci yoon bi xepp na senegal mangcci ci afrique
mais niom daniouma nopp wesh c bizzardz

entoucas sama riere-ca sa promet
mangek samay rit-xa sous les cotes
mangui diema out sax ay supporter
foumeu dem niou dem fa leurs pied mon pied

dama xam douma kouniouye pamti pamti
boudone lolou ma xepp rap neki gardien dama nittéwoule boy def ci code tay dingma weur ci bi town tey dokotay yan

refrain:
nioune sa fiit laniouy teubeul
ay feni neen doyna seuk
oubi say nope teudiate sa gatt
yanchi seu mere yanchi sa papa bi dana saff kani sadam louniou defone demb laniouye defat sa ay defenseur dounioula defendre kone
meusso xaam david beckam (ooh)

meusso xaam david beckam (ooh)
ay gandam but sa ay lucarne (ooh)
danga beug xam david beckam
aythia dome ndeye come on non
meusso xaam david beckam (ooh)
meusso xaam david beckam (ooh)
danga beug xam david beckham (ooh)
aythia dome ndeye come on

autotune version:
meusso xaam david beckam
meusso xaam david beckam
danga beug xaam david beckham
aythia domou ndye comon
meusso xaam david beckam
meusso xaam david beckam
danga beug xaam david beckham
aythia domou ndye comon

letras aleatórias

MAIS ACESSADOS

Loading...