letra de wurus (version afro) - wally b. seck
yay sama adouna, oh yeah
sama baby coco waay, ey yeah
yow yay sama aldiana; my love
sama baby coco waay, hmm yeah
baby yay mane
teudeul nèlaw kham gni mounoul dara
i don’t give a f-ck mèrr katt fadjoul dara
takal la or ba ci 24 carats
dagn lénn di bayèkk peureum bi
gnom gnouy deukké aya
baby i just want real love
real love, i just wanna know real love, definitely i don’t wanna lie
(i’m in love with you, in the morning, in the night, oh yeah)
(i’m in love with you, in the morning, in the night, oh yeah)
yay sama adouna, oh yeah
sama baby coco waay, ey yeah
yow yay sama aldiana, my love
sama baby coco waay, hmm yeah
way way way way
mèrr bi fadjoul dara
mom fadjoul dara
konn fadjoul dara
baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats
wurus 24 carats
ngualam 24 carats
khana dou mala yèenè
ma vie, ma vie
baby yay mane
teudeul nèlaw kham gni mounoul dara
i don’t give a f-ck mèrr katt fadjoul dara
takal la or ba chi 24 carats
dagn lénn di bayèkk peureum bi
gnom gnouy deukké aya
baby i just want real love
real love, i just wanna know real love, definitely, i don’t wanna lie
(i’m in love with you, in the morning, in the night, oh yeah)
(i’m in love with you, in the morning, in the night, oh yeah)
yay sama adouna, oh yeah
sama baby coco waay, ey yeah
yow yay sama aldiana, my love
sama baby coco waay, hmm yeah
way way way way
mèrr bi fadjoul dara
mom fadjoul dara
konn fadjoul dara
baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats
wurus 24 carats
ngualam 24 carats
letras aleatórias
- letra de nichts hält einen rollenden stein - ella endlich
- letra de al concerto de vasco - il bepi & the prismas
- letra de vibe - the thought
- letra de good shepard - brother isaiah
- letra de glass house - antiheroes
- letra de por favor - padington
- letra de i can't fight your love - 7" version - the modulations
- letra de lover lay low - crystal waters
- letra de intro - underismo
- letra de piss yellow - looky