letras.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

letra de wuyuma - viviane ndour

Loading...

xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeuguél thie xol léy nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara

mane déh walouléne ma wax koko
xalé bi lékatuma ndax mome
nanatouma nélawatouma
wowo
sama xol yathie néh

lék lék ma woo ko t-t dal di coupé
sama appet-t coupé
febar dinama guoungué
docteur dama love ba dof
té xawma loukoy fathie
wowo
mba meune nga thie daraa

xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara

mane woo nala founé
nga diapémma sa xarite
inviter résto, lalal nala louné
wowo
nga diapéma sa xarite

lék lék ma woo ko t-te dal di coupé
sama appet-t coupé
fébar dinama guoungué
docteur dama love ba dof
té xawma loukoy fathie
wowo
mba meune nga thie daraa

mane beuguena ma bagne bayiwouma
mane guisoumaa
kénén koudoul mome
mbeuguéleu beuri dolé yén mako xam

xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeuguél thie xol léy nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara

xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
beugue nala té xamothie dara
mbeuguél thie xol ley nék deugueleu
beugue nala té xamo thie dara

kouthie nék’aak kingna nope
sa guinaw bandague fax-ssul
diougueul yeungueul bamou saf
sa guinaw badangue fax-ssul

kouthie nek’aak kingna nope
sa guinaw bandague fax-ssul
diougueul yyeungueul bamou saf
sa gnuinaw badanue fax-ssul

letras aleatórias

MAIS ACESSADOS

Loading...