letra de nobal ku lê nob - titi
n0bal ku lê n0b lyrics
wouy mbeuguel loo, anh mbeuguel
wouy mbeuguel loo, anh mbeuguel
bala ng-y n0bati iao, nang ko xol
bala ng-y beugati iao, nang ko set
ndax so beugueii, so beugueii, nguru ngaa
bala ng-y n0bati iao, nang ko xol
bala ng-y beugati iao, nank ko set
ndax so beugueii, so beugueii, nguru ngaa
dang-y set gninga bayi ba am ci ay noone;
mane ma xol gnima bayi na am ci ay noone
nonu nga donei sama matadi
ba sumala jissul: baby damay manquer
inquiéter wu sumala seinei ak kenen (fok nga sip)
wayei manit na dal ndax numa dieufei wathié sama personnalité
lumeu meuneu don yafi nei
bala ng-y n0bati iao, nang ko xol
bala ng-y beugati iao, nang ko set
ndax so beugueii, so beugueii:nguru ngaa
bala ng-y beugatei
n0b kuleu n0b: dara dakuko
beugal kuleu beug dara dakuko
n0bal kuleu n0b dara dakuko
beugal kuleu beug dara dakuko
dara dakuko, dara dakuko
n0bal kuleu n0b dara dakuko
dara dakuko,dara dakuko
beugal kuleu beug dara dakuko
enh beuglen
xana du mbeuguel leuu
mane nena sumako pognet du dem
mane malay décoder ndax danga coder
hôpital buma diar niu xalil ma yon
ndax médicaments yalay fathie, mane malen kay diox: ma gueun ci yow
guedj gui sax dafma xamei
vagues yi don samay xarit
nguelaw li, pithe yi naw ehh
may sen natagoo
whatsapp bi nga saalo
ba xolatoma dima zappé
viber bi nila won
ba sumalay bye bye
doma xol man
ennnnnh wouy mbeuguel looo
n0bal kuleu n0b dara daxuko
beugal kuleu beug dara daxuko
n0bal kuleu n0b dara daxuko
beugal kuleu beug dara daxuko
dara daxuko dara daxuko
n0bal kuleu n0b dara daxuko dara daxuko
n0bal kuleu n0b dara daxuko
beugal kuleu beug dara daxuko
dara daxuko dara daxuko
beugal kuleu beug dara daxuko
dara daxuko dara daxuko
letras aleatórias
- letra de vorspiel (acapella) - ssio
- letra de jäävalssi - hector
- letra de stadt - phenomden
- letra de quédate a dormir - m clan (rock band)
- letra de wasted - mlodyskiny
- letra de betty beep - hap palmer
- letra de one thousand days in sodom - venom (band)
- letra de a song for summer - noah floersch
- letra de rsvp - rin
- letra de rubberhouse - rachael lampa