letra de show me - sir malik
yow rek la love, baby
meme soudé meusseuma la ko waax
danga dawa daw beu sonou
dem beu meunatoula noyou
sey beutt angi honq
xam na lu waral sey rongogn
nenaleu dou ci yow
suma téyéwoul seu loxo
té douma bett benn yone
so demé beu teyé sa bopp
déception yi ma dadialé mo beurri
benen peine de coeur du hadj ci xol bi
mais tey dinala waax deugg bi
because i know you gotta know
demay deukké di liirat su nyu texto yi
deuké screenshot sa ayy story
douma beugg loudoul fatt n-ggas you topp sa guinaw
di saup saup lou naan dagnou la feel
soumala né beugeumala
sama bopp laye lеuré
a chaque fois su nyu beutti tassé
dama nane ca y еst
man deh beugg na la n0bbé lu raww ning ma n0bbé
beugg na la beugué li raww ning ma beugué
show me how to love
show me how to love
show me how to love
show me how to love
show me how to love, baby
show me how to love
show me how to love
show me show me, baby
show me me show me, oh yeah
show me show me, oh yeah
show me show me
show me
show me
letras aleatórias
- letra de pick up the trash - le fil
- letra de i'm an artist (freestyle) - moccasin creek
- letra de я не брошу сигареты [iwqs] - afoolinside.
- letra de лейкин - kunteynir, georg korg (apokriff)
- letra de untame the tiger - mary timony
- letra de princess - happyk1d
- letra de минифит, чарон бейби (minifit, charon baby) - krapgoroh
- letra de locked on me - will morris
- letra de belle delphine - lil fuub
- letra de far away (далеко) - dave dion