letra de dou cii neene - rainbow-clan
intro
yeah yeah
alright alright
yeah yeah
alright alright
yeah yeah
alriiight
refrain
dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde ling-y diem
gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem)
fitou kece douci da ( daaraaa)
naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone
te guissal gnou wonei fitou gainde ling-y diem
gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem)
fitou kece douci da ( daaraaa)
naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone
moontee
h-llo dear, what’s good, trynna open your ears
ci douci neene lagnouy tek, n-gga trust yourself
nanga gneme linga doone, bagna nekk ben nitt kou boone
soubeu beu ngone, yangui ci bopp kogn bi taakiy boone
reub nga, keud nga, thiole nga
yangui ci jail bi teud
why not nek ben clean boy, nangou degu deugu
mbir bi len leu, yallah keneu leu
bouldi nangou tokk di xaar balle bi taakk neu..
bm
dou ci neene, gnou songu hip hop mou done sougnou gun
kouci nekk ak lila takha rappe gueumal linga done
gni di boone, gni di wine, gni di gadou gun
fougnu taxaw nei mista rapper gnou ni niitt kou boone
alyghost
yewou njeul def sa mind dou cii neene
takk sa fiit gueum sa war reuthie lene
fiit dou djay, baay guinar bi dou neen
dawala daw adouna ningui mel
refrain
dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde ling-y diem
gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem)
fitou kece douci da ( daaraaa)
naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone
te guissal gnou wonei fitou gainde ling-y diem
gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm (yem)
fitou kece douci da ( daaraaa)
naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone
alyghost
yoh check, fils, dou neenu neene
technikeul rainbow dh raw na len
kou ci beugu men, gnou dikk wone len
fitou gainde ndiaye bi nekk ci gnouni neene
gueum seu bidew bagna ragal loufi neew
diokhe sa bakane neu naw, deugu doufi neew
mengalel sa bop king kong
rainboweu gui sing song yeah
kou beug alone seu life doko ping pong dé
bm
doneul seu gainde bopp mission dagg loce
gueumeul seu bopp nangou dinga doni boss
diog sa fadjar tel dh woutum xeuy di doone sa guerre
lou waruta gnak tokk ci kerr lou ci doul neene dh doone sa doolei
moontee
wiri wiri diari ndari leu aythia gnou xarei
mission de goor yallah leu na fiit bi barei
kone bro trust yourself
don’t listen someone else
gueumeunl ni dinga ci guen n-gga by yourself
refrain
dou cii neene, te guissal gnou wonei fitou gainde ling-y diem
gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm ‘yem’
fitou kece douci da ( daaraaa)
naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone
te guissal gnou wonei fitou gainde ling-y diem
gueum seu bop hamni li dou fen lila yemm ‘yem’
fitou kece douci da ( daaraaa)
naka nonou, nanga meuna gnemei linga doone, (x4)
outro
gueum sa bop fiitou kecei dou ci neene, ‘douthie neene ‘fiitou kecei dou ci neene

letras aleatórias
- letra de idgaflb - sunshine christo & hank chill
- letra de holdem - lex (grc)
- letra de vision 4k - ouss & riane
- letra de i was high xd - anidem
- letra de vergeet - spoegwolf
- letra de sır - aga b
- letra de pas la peine - tessæ (fra)
- letra de dead bride - toni rams
- letra de the one who pays - inflect
- letra de get hooked (valentino's deal) - paranoid dj