letra de me you and god - obree daman
mbeuguel la nekk ci sama xol
wai adouna nyu sonal lol
xol bu fess ak baneex
la la yeené won ci adouna
mbeuguel gima am ci yow
mba duma sonal lool
diafé diafé adouna
ak bokk gui yallah burr bi bole
kon mbeuguel lay adouna
ndax yallah mo nyu bolé
sama yeene yaatuna
mangi nyaan ndax yallah mey nyu dolé
dugu na ci gaalu mbeuguel, ndox mi yobuma
ngelew langui mai indi ci yow
nyu guissé leer na ma
mbeuguel moi li leeral adouna
xam nga yow la beug lool
sama yeené yaatuna
mangi nyaan mu yoku
denk na la yallah
denk na la sama xol
sasu ma djuli di la nya-n-l
sama xol la ko tibé
denk na la yallah
denk na la sama xol
sasu ma djuli di la nya-n-l
sama xol la ko tibé
kon mbeuguel lay adouna
ndax yallah mo nyu bolé
sama yeene yaatuna
mangi nyaan ndax yallah mey nyu dolé
dugu na ci gaalu mbeuguel, ndox mi yobuma
ngelew langui mai indi ci yow
nyu guissé leer na ma
mbeuguel moi li leeral adouna
xam nga yow la beug lool
sama yeené yaatuna
mangi nyaan mu yoku
letras aleatórias
- letra de trelew - seba wonder
- letra de cat geral - conrado
- letra de 11:00 pm - yung cort
- letra de hollywood (single version) - marina
- letra de cigarillo cinderella - dave & friends
- letra de out of the blue - the stray dog band
- letra de ты тупой (you are stupid) - egor muf
- letra de #hot16challenge2 - boro
- letra de somebody new - project 46 & bynon
- letra de husky (senza risposta) - @spike84