letra de nio far - nix
viewing lyrics for nio farr by nix black crystal
nio farr
hook: (-2)
nio farr, nio farr
homie di na baakh
haters yangui dinngat no doubt
neleen mane ak nix nio far
nio farr, nio farr
douma la jaay gangsta, reals yangui ci jail bi /
att yangui dèm saayo wëtè rethiou sa dembe /
douma la jaay boytown boy xamnga li may sound /
guenone na niaang bou rapadio di binde goudi town /
dama moussë fonke game bi, moussë fompe tim yi /
dokh dokh bi géré thiôpp bi may la loxo nga tiim ma /
sou thiôlé nga jiin ma, guiss ma tey souba nga sèën ma /
ganaw souba keneen guiss ma , gnou tek deal souba nga fay ma /
yesss! yallah’a gnou tiim homie lii dou f-ck /
tey nga taake, souba nga fey, meyal keneen töke /
gnou tathiou ko mou job, weurseuk em mou thiôp /
bégueul gni ko sôp, teral gni ko tôppe /
ha ha… mané môm sa mind môm sa guemign/
wala gnou dokh sa mind téyé sa laamign /
han! beus dina dioum nouyôk loxo thiamogn/
tâmme fly di rep’ galsen… u kna’ mean?! /
hook (2-)
bégué bi fii la euppé, wone ma fane nga fété /
let them talk, défal ni mane wone leen nô leen souté /
town bi djaffé na, ok askan bi xoslu na/
wout pékhé legn fi néké fils yakaar wéssou naa/
djogal fight yangui nieffé wanté dessna/
le tps nguey kodj leweul fils sa team encaissé na/
sa sokhna f-ssé na, sa weurseuk sori na/
loy waste sa time di wakh ci keneen kokou sori na/
banlieue bangui lap, fils gaayé gnou eupe diap/
beus bou né gnou tek gnou deal jaay gnou speed kene dou leen daap/
té xaliss ba ngi daw kou ci jott mou teudj sa gatt/
money talks homie, lo mounti goré da ley baap/
hustla mind la gnouy dawal fils sunu bakene legn ci tekk/
kone xana ma def ni tigrim… adji rap tekk/
sponsorisé “rap rek” bagn sa shorty merr/
show me love for this beautifull game i play men/
hook (-2)
this is for my falling soldiers (-4)
lou ngen defal sunu game
lou ngen defal sunu game
forever dougnou ko faté no dougnou leen faté
yallah ne leen yallah xaré adiana bou kaawé
hook (-2)
letras aleatórias
- letra de flour city 2 - 38 spesh
- letra de vem pra fora - valesca mayssa
- letra de bow & arrow tree - michael fernandes
- letra de savage - bazzflow
- letra de someone you loved - camila cabello
- letra de nobody - inswain
- letra de only a memory away - shandi sinnamon
- letra de ndaremerwa - holy ten
- letra de pdmf - icowesh
- letra de por aquí - kolomb