letra de boul ma méré - nix
nix – boul ma méré (lyrics)
hook
game bi yeufou hustla la boy boul ma méré
yague na ci game bi boy meussouma wéré
chérie danga toy yeah baby kaay gnou géré
game bi amna khaliss boy fils kaay gnou géré
né negn ma “nix bayil blow” (nix bayil blow)
wala “ma beg ci yow” (yeah ma beg ci yow)
“meygnou touti flow” (meygnou touti flow)
ok! ok! ok! ok! ok !
wiri wiri diaré ndaré fils ma dieulate péé dila khaar
yeah n-izzi’s back, dakhe le job dakhe le party (dakhe le party)
yeah se son truck bou panne le ding ko garé
guénéma sa guemigne bes boma wonné dinga diahrré
indil la lou raw kharé, rey g-yi la fi néké deuk ci diaalé
yalla nama yalla baal indi na fi safara hip hop khall d-mn!
yangui worou galé, yangui saalé
bimey def lou ma xam pbs mou ngui woy boul falé
dafa am gnouy kholé, am gnouy liguey di daan sen dolé
am gnouy tök ci bopou kogn bi rek di doul di bolé
snitch le wala dou snitch, man b-tch le wala dou b-tch
samay kheul la yorr boy fo guissé porsche bougnou doul kheutch!?
maylene gnou dieuw ma balaa ng-y nande sa raak roy ma
bou souba sa b-tch joy ma ba nopi foutekou khoy ma !
dou souba tey la, le temps ng-y job n-izzi rey la
boul ma rey ak wakh damay khoslou fils fayma
hook
dama done fo ba gaagn la, sandi kaddou khaagn la
dotoul studio waagn la, son bou bess la, agn la
sama gaayi degn ko khiif, punchlines yi thieboudieune la
today c’est sarakh day, mc’s yi lay def talibés
dagnou meusseu dieuli town bi, diokhé temps bi, kepp gamme bi
mangui ci sen biir di laake leneen ni galsen ak gambie
n-eezy supa grandé, mitraille les yeux bandés
sa dadj yi dinegn watche tey fils fo mounti mandé
fame yé sakkane, style yi, sho yi yangui diokhé sa bakkan
aka ma leen lakkal, sen doul yé leer ni “plan takkal”
boy mané show me the money, ndakh gnou meune khoukhal none yi
ngen meune taal sen bone yi, sho yi meun gnou def sene you bone yi
mane la n-eezy gentleman, dou ay yeufou gondi boy nonou le mel
rap bouy khodiou boy solou ba bagn sa rap dafa khawa def taatouneen maaaan !!
shut the f-ck up boy te nga bayignou gnou job
nga done sunu khadjou galé gnou mey la nga thiop
hook
shorty… kaay gnou… géré… daadiou…
ki moy black crys mo gueneu gnoul wa joal fadiouth
doto kham lou diaadou nekh na ci sey youkhou
yes i’m going in!!! ding ma né merci beaucoup!
douma la dieme gondi ba di la fène soudé may faye
meun lou may def tek ci rew : souleyman faye
haha i’m just having fun man
mais wakh ngen deugue “rap wolof mo raw”… bring the hook!
hook
letras aleatórias
- letra de closed your eyes - тина кароль (tina karol)
- letra de moonlight - rene
- letra de why me - monkie kid
- letra de let down - the anchor (metal)
- letra de dzisiaj - janek. (pol)
- letra de nothin lasts forevah - mellodz
- letra de dali - oge (ft. elena tsagkrinou & mg)
- letra de quiero arder - agoney
- letra de yeei 5 - alblak 52 & bushido zho
- letra de woman i wed - knownbyalex