letra de r.d.d.r - nitdoff
{refrain }
yo! nokoss di rokoss ragal dou djégui rail
fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right
d squad doutoul xeuthio pé (1er) bi waay
cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
p.a kinepi roythia ba guédiawaye
we don’t give a f-ck baate bigni naane guédd-waay
bougni dokh cii hood dagni oyoff ni b-tterfly
b-tterfly dagni oyoff ni b-tterfly
{couplet 1 }
yo yo yo
k!llah k!llah di rap wow dap my n-gg- what’s up
it’s so phenomenal hip hop nitdoff cii yénéni diapp
téwal hood n-gg- cii track ndiap di deugueul kap
hot sh-t what a fk s-quatt nioune guemouniou pop
lamp yeup ghetto yépeu fay niouy dokh di gueume di yott
sèni ngour beuri faay lépp rek cii gueumeu god
niouy gueuneu di rock sani séni bagg niou seug di roteu
justice bi joxé séni -ss doni tott
wadiour yi sonou keur you fess yi niou bott
hood bi né jungle, young boy deungeul
only mother fk, hip hop bégni yégueul
deuk fi di yomb kou amoul fiit dou rombe
fokk nga ndaguu diayanté wala niou weurleu nomba
life bi boudé tééré dagni xeuy di nafar
hood béniou défar, koufa diougué nio far
1 luv 1 come on n-gg- doni soldat
{refrain }
nokoss di rokoss ragal dou djégui rail
fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right
d squad doutoul xeuthio pé (1er) bi waay
cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
p.a kinepi roythia ba guédiaway
we don’t give fk baate bigni naane guédd-waay
bougni dokh cii hood dagni oyoff ni b-tterfly b-tterfly
dagni oyoff ni b-tterfly
{couplet 2 }
yo yo yo yo!!! soma toppé cii hood dag-y rér ndaxté mino
sama home boy dougnou leu feel ndaxté cleano
ghetto amena crack, amena yaram amena ino
dagni téleu yéwou hustle hard d-ss nimo
sabab dioxé loufi né au maximum
diouk outi xeuy ni niou kay wakhé mak simon
xarou niou sa ngour cii god lagnou wékou
liniou dall dou niak diom life béniou diékou
na dokh bi gaw my n-gg- boul wakh ni sékou
diouguel foutékou f-ss yéné fight ba diote sa lékou
chod up all my home n-gg-z yi di niafé!!! 4 real!!!
do meusseu guiss fu sunu beut di raffé
yegg yegg bou kawé waral dokhaline yi deugou
k!llah missal leu cii lou fégn ak lou neubou
ragal dou djégui rail ndaxté xamena likoy reubou
again to ziar nga degg po po po po
{refrain }
nokoss di rokoss ragal dou djégui rail
fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right
d squad doutoul xeuthio pé (1er) bi waay
cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
p.a kinepi roythia ba guédieuway
we don’t give fk baate bigni naane guédd-waay
bougni dokh cii hood dagni oyoff ni b-tterfly b-tterfly
dagni oyoff ni b-tterfly
{couplet 3 }
yo yo oyoff ni b-tterfly
di holla sama hood
proud cii lima done douma… sama xétt
i represent my people n-gg- séneu ma cii kaw
dara dou takh ma sopi sama mélo ak sama djiko
so beugué done hero na nga ma wane fayda
wathial cii mbede bi done number 1 fighter
gangsta wékouwoul cii prek wala diaay tarr
lucidité mind bi ng-y démé moy sa lighter
ragal dou djégui rail!
why?
fé sunu indice bouniou diapé fake et reste
douniou call police
bang murder like street order
k!llah k!llah di bang i’m a hip hop soldier
{refrain }
nokoss di rokoss ragal dou djégui rail
fi weuk niogui diote cii mic nioune douniou ko tégui right
d squad doutoul xeuthio pé (1er) bi waay
cii hood la lep doré taay dém neu ba djégui daay
p.a kinepi roythia ba guédiaway
we don’t give fk baate bigni naane guédd-waay
bougni dokh cii hood dagni oyoff ni b-tterfly b-tterfly
dagni oyoff ni b-tterf
letras aleatórias
- letra de waves - og-martynov
- letra de otis and marlena [travelogue] - joni mitchell
- letra de killer love - madame macabre
- letra de ghost in your memory (feat. vito) - unknown_idc
- letra de зима (winter) - лесоповал (lesopoval)
- letra de goodbye nostalgia - coda piano trio
- letra de second base - daz
- letra de the robertbobby channel song - the robertbobby channel song
- letra de 虹のカケラ (rainbow fragment) - dish// (jpn)
- letra de bakeri3 tour llif3 - the low mays