letra de imbécilo rék - nitdoff
[refrain]
nane nga meuneu fowei nit yi imbécilo rék
nane nga meunei deupé caisse yi imbécilo rék
nane nga meuneu tassé yakar imbécilo rék
detournement de bien publics yi imbécilo rék
liniou lébone ngir soukhalikou nga ni ko foukh tokk
li warron tchi ndiangu bi nga ni ko foukh tokk
li warron tchi fadiou bi nga ni ko foukh tokk
imbécilo rék imbécilo rék
[couplet 1]
deuké di doul ak rendi nit soul
yagui djité thiogalou foule sa lepp di cool
yaye qui dakheu sathie sa rew kone khogalikoul
sa galé amna auto you luxe sa comtpe yi full
sa ndieuguou ben montre tchi xayma tabakh neu school
dou né nga gueumo ni nieti fani bamel amna
dou yagui nax nit gni bayil khel ni yallah xamna
sa keurou fi meun na yaatou wayé bamel xatna
do nitou guat doma sathie banopi mayma yapma
li niep bokk yako diеul caisse sou nguur yi yako teul
modaf-cka nga fi amoul lenn louniе fiy rafetal
hôpitaux yi amouniou lale
niak ba ngui gueuneu di wale
bachelier tokk di kholé ndakh amouniou founiou dale
ngueni niodi dioma niaw ci ay parrains wou mbalakh man
battréwoulen lou nguen mom yenn sathie you niakk diom
haute trahison du peuple nguen dekou ay meukh daume
[refrain]
nane nga meuneu fowei nit yi imbécilo rék
nane nga meunei deupé caisse yi imbécilo rék
nane nga meuneu tassé yakar imbécilo rék
detournement de bien publics yi imbécilo rék
liniou lébone ngir soukhalikou nga ni ko foukh tokk
li warron tchi ndiangu bi nga ni ko foukh tokk
li warron tchi fadiou bi nga ni ko foukh tokk
imbécilo rék imbécilo rék
[couplet 2]
yaw métier bou n0ble ngen nekk di tonie
guetou mala yey sén place nguen lekk dji ngogn
lign ley fay beuri tewoul ngey sathie di rogne
te ken tchi yen defoul djiego sakh youy sopi sa konie
guis na gua beuuff tchi tankou kilifeu di ceddé ay batt
té bofa diougué talibém yi sey dieuf moleni fatt
guiss na niou toudé leu ay biss nga niew di diokhé ay nakk
té finiou leu fale bofa démé radio guedj na fa takk
niata nio léwal koom si ay surfacture
té bouniouy laay nga guiss sen fennyi comme ay pur acteur
benn daan dou dale sen kaw amnanie protecteur
nioun sunuy ndaw di xeuy di gueun di daw ci khif ak peur
élection niou guenewaat budget bi dieund espoir
diakhassé tarikha yek ethnies yi nguir diot ci pouvoir
bou ci bakane naré rote sakh dounie déliu guinaw
nanie signel gandi cheque juge bi rek mou diokhé victoire
[refrain]
nane nga meuneu fowei nit yi imbécilo rék
nane nga meunei deupé caisse yi imbécilo rék
nane nga meuneu tassé yakar imbécilo rék
detournement de bien publics yi imbécilo rék
liniou lébone ngir soukhalikou nga ni ko foukh tokk
li warron tchi ndiangu bi nga ni ko foukh tokk
li warron tchi fadiou bi nga ni ko foukh tokk
imbécilo rék imbécilo rék
[outro]
woop woop woop woop woop sathiéy
woop woop woop woop woop sathiéy
woop woop woop woop woop sathiéy
imbécilo rék imbécilo rék
woop woop woop woop woop sathiéy
imbécilo rék imbécilo rék
woop woop woop woop woop sathiéy
imbécilo rék imbécilo rék
letras aleatórias
- letra de spongebob freestyle - dadoggy
- letra de mass pollution - helloween
- letra de charlie - in vivo
- letra de beating hearts - king & prince
- letra de hollywood - loganplayz
- letra de city of the dead - meiston, mazdess
- letra de eros - kurobs
- letra de ruins of today - beware of darkness
- letra de suaramu syairku - eka ayu
- letra de southside - sniper j