letras.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

letra de guetto swagg - nitdoff

Loading...

{nitdoff – 1er couplet}
5 underground keurgui crew ng-y degue
alien zik k-mpeu sen ng-y dégue
mister dj yaw lo fokk
boudé daga niou xepp yaw ak sa club mother f–k
complexé xoss ko sa platine
rap galsen mo raw b-tch what’s poppin’
no nudité !!! no s-x video !!!
sunu society bi leu sunu txt firi yaw
dou té mou thug
dance wala dougou club
kone liguay daw di weurri fénène ngui saay sufu beutt
cii rimes ak flow lagni neubb sunu swagg
talibéma lagni niodii sunu swagg
yaw k!llah and admow bou doyoul
we got more..24/7..dagni reupeuteul ya know (24h/ 24 : 7jrs/7)
galsen stand up suku lèn sèn ndapp
dolèle sèn mc yi té valorisé sèn ndieuk{admow flow – chorus }
who’s back wanèle saa ghetto swagg n-gga (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg shawty (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg n-gga (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg shawty (2x)
limo di ghetto swagg (oooh)
dagni shine….coz we hav a ghetto sawgg (ooooh)
we make it so hard in the hood
so check g.h.e.t.t.o
nitdoff k!llah and admow flow
g.h.e.t.t.o
nitdoff k!llah and admow flow
{nitdoff – 2ème couplet}
yaa! pétaw dieum na kaw mélni boudé dem
tek flow cii kaw beat melni boudé came
rap galsen dj dou rayoul kèn
boudé flow rek la lathie we do daay tang
sunu bosss dafa deugou té sa doul daay xégn
boupp laay xégn dj djiam niou rap galsen
niou bégué beauté sauté cii kalama kocc barma
rimes cii tig’rim def featuring ak kouné warma
dj daga gueuleumeu badou mala euleumeul
wala pour nga tekma fokk ma dioxla sama deureumeu
bullsh-t baayil niou tiéné sunu onde (100frs)
keep so real douniou nakh sunu monde
matador simon k-nibal bacii youka
gaston kp-res(res- kp) moy daw fi baa louga
mister dj yaw lo fokk
boudé daga niou xepp yaw ak sa club mother f—k

{admow flow – chorus }
who’s back wanèle saa ghetto swagg n-gga (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg shawty (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg n-gga (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg shawty (2x)
limo di ghetto swagg (oooh)
dagni shine….coz we hav a ghetto sawgg (ooooh)
we make it so hard in the hood
so check g.h.e.t.t.o
nitdoff k!llah and admow flow
g.h.e.t.t.o
nitdoff k!llah and admow flow

{admow flow – 3ème couplet}
yeah ! okay !
okay! welcome to ghetto swagg
hip hop galsen égue on the top
mister dj gawal play the song
rude n-ggas yi yénguetou from the underground
mao scool drop the beat, n.d k!llah & admow nieuw make the hit now
new scool know the deal welcome to the future té douniou délou guinaw
where’re my n-ggas in the hood (haann hannn)
where’re my n-ggas in the ghetto (haann hann)
where’re my boyz with a lot of swagg
akssi lèn niou dance in the ghetto
niou def ko ghetto dance ya
niou def ko swagg dance ya
ghetto swagg ak dance
nitdoff k!llah and admow (oooh oooh)

{admow flow – chorus }
who’s back wanèle saa ghetto swagg n-gga (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg shawty (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg n-gga (2x)
who’s back wanèle saa ghetto swagg shawty (2x)
limo di ghetto swagg (oooh)
dagni shine….coz we hav a ghetto sawgg (ooooh)
we make it so hard in the hood
so check g.h.e.t.t.o
nitdoff k!llah and admow flow
g.h.e.t.t.o
nitdoff k!llah and admow flow

letras aleatórias

MAIS ACESSADOS

Loading...