letra de kara lumiere - magikara
[“kara lumiere” by magikara]
[chorus]
lim may dund ló ci boppam
andut’ak leneen
ku ciy mbokk nanga ma baal
nek-ma ci leneen
lim may dund ló ci boppam
andut’ak leneen
ku ciy mbokk nanga ma baal
nek-ma ci leneen
[fisrt verse]
teyit dafa fiir ci mann
konn na ñëpp teey
ci gueedji leer ñimu ci sóop
maa ci dakka feey
bamba dafa fiir ci mann
konn na ñëpp teey
ci gueedji leer ñimu ci sóop
maa ci dakka feey
[chorus]
lim may dund ló ci boppam
andut’ak leneen
ku ciy mbokk nanga ma baal
nek-ma ci leneen
lim may dund ló ci boppam
andut’ak leneen
ku ciy mbokk nanga ma baal
nek-ma ci leneen
[2nd verse]
damay nuuru aka fitti
di feeye njaaxanaay
takk bël bël dana ko deff
di feeye ndëfenaay
damay nuuru aka fitti
di feeye njaaxanaay
takk bël bël dana ko deff
di feeye ndëfenaay
yallah nañu baaxe
ku tooñ mu lay baale
bu kenn ci ñun ñiy ame’y bakaar
konn ngala nanu melni seex ibra faal
diamono lëndëm na
wante leer dikk na
diamono lëndëm na
wante leer dikk na
[chorus]
ay borom leer
ay borom leer
may ñu baax, may ñu leer
ay borom leer
ay borom leer
may ñu baax, may ñu leer
ay borom leer
ay borom leer
may ñu baax, sol ñu leer
ay borom leer
ay borom leer
may ñu baax, sol ñu leer
letras aleatórias
- letra de friends with chanel - ashton
- letra de den anden side - gobs
- letra de psychoactive - cody manson
- letra de karim - rimkus
- letra de can't say no - mckenzie small
- letra de t'es beau, t'es beau - joyce jonathan
- letra de better medicine - ann beretta
- letra de 2 much - lxner
- letra de marginal boombap - mittor
- letra de louis - bu$hi