letra de lep tchi yaw - junior
meunouma faté sa rétane bou raféte
soumeu le guissé tagok sama sago….
say souma lay khalate
sama khél day déme fou sori….. (fou sori lol)
say soma kholé samay tanke yi bagne
souma le dégué sama khole day dal di fékh
lane ngama def yow, meunou mala guéné si sama khél
khawma loutakh ba souma toggé di le khalate
mane na moudié doff te kham ngako
refrain
ndakh beuguena lép li né tchi yaw
say sougnou toggé dal di wakhtane
damay faté thiono dounya
ndakh beuguena lép li né tchi yaw
khalatou démbeu yima am si yaw
souma teudé nio may sonal
yaw diokhma lééép tchi yaw
ma diokhla lééép tchi mane……….. wawaw
khamnga boubakh ni yaw rek le
mbeuguél lama sonal meunou m-ssi dara…
lima woor té woor
modi nieupe peungue niouy diémeu… dédeulé
boul guestou guinaw yaw, khalatale euleuk….
nieuweul niou doundate lou… bess…
boul am loy ragal, douma meusseu déme bayila
tchi adouna……
refrain…..
diokhma lééép tchi yaw……
dégloule sa khol té nga def li la war
naniou wané li né tchi nioune
refrain……
letras aleatórias
- letra de 212 - cpro
- letra de alive - yot club
- letra de if not you - ings
- letra de blessed - kelly clarkson
- letra de won't let you know - yosef david
- letra de good morning, blues - peter tork and shoe suede blues
- letra de deuces - comethazine
- letra de the weather - your paris
- letra de geceler iyi - waldeins (tr)
- letra de let love free - tiarra girls