letra de wax - jay 21
[refrain]
au final c’est bizarre
mounomeu naat ci 10 ans
c’est bizarre
mane douma mbam mais kouma mbeuk ma bissap
c’est bizarre
rappeur te yi di gueuneu bizarre
chroniqueur bi lane nga djissat
diogue ci tata béw doug taxi yor attitude you méchant
doug gale gare benz takhoul ma ngui deg parole you méchant
koy tere wax wax wax wax
koy tere brr wax wax wax
[couplet 1]
li doff leu wala louma dale
xamatouma louma dale dama doff wala dama meuneu rap kaddu ya ngui rayé
barre yi charger balle
rap beu gnou toude meu boulevard
sa mc dina doug var
badola ni procureur bou doug car
mane meu beuri class niom niou beuri crasse
eup leine vitesse vitesse
apporter leine tristesse tristesse
flow bi wane weakness weakness
jay di gueuneu si frais si frais
ma call ko si bizness il stresse
té pourtant ci bi test il stresse
kou sheytane khekhoul diapal yeine andeu beu diamono di diekh qui presse
qui c’est qui c’est ?
melanger wouma bizness ci s-x
two step step
beneu beneu niouss leine cul sec
my n-gga
domerame
sa flow wou daw da nga neubeul
yeine album dagn ko neub
may battrer carte yi n-gga coupeul
amouko mi-temps
dameu sa chicha
da nga changer sa histoire bande de mytho
nangou sa fiteu
dieul sa xel guitare
mouno meu diay bandit am sa deunou pitakh
des langues de putes
platou rappeur touti ketchup
dag mc digou beutcheuk
stopper carrière beu ci seuteum
combat yi gueuneu fréquents mais victoire yi dafa garantie bipa
[refrain]
au final c’est bizarre
mounomeu naat ci 10 ans
c’est bizarre
mane douma mbam mais kouma mbeuk ma bissap
c’est bizarre
rappeur te yi di gueuneu bizarre
chroniqueur bi lane nga djissat
diogue ci tata béw doug taxi yor attitude you méchant
doug gale gare benz takhoul ma ngui deg parole you méchant
koy tere wax wax wax wax
koy tere brr wax wax wax
[couplet 2]
amoulo mi-temps
toukh nga sa sh-t
jay dou garçon facile wakh ko sa sista
ko meuneu titeul
nangou sa fiteu
sen xel yi dépasser woul xokhou ditakh
ng-y melni sindakh
diaroul toukh dagn leine di fiteu
douma yeureum keneu bipa
paw paw kalashnikov
khawma ki dioud teukh lak boumouy khalaté moma titeul
imbecile
album bi dieurign neu medecine
fane nga dieule money keine dou sip
tour ci bamel money yi hennessy
genocide
raw na catastrophe tiérn0byl
sama none yi dieul leine middle finger
balle tank leu t tiow dou djip
sarax taakneu ci beneu pile
mother f-cker yi dougn meu tere chill
genesis beu ci genocide
eup meu xaliss nga geuneu feel
daak leu rap loloy bénéfice
imbecile dieguessil
kham nga né poune dou teinter cil
leep dina leer my n-gga diaroul xessal legui dagn may deglou beu tenessy
douma football ak goumbeu di douma
ragalou kouma toumal
diri rap bi diap ci boumeu
diematouma diematouma sa tioumboukay bi lagnou toufli ci fouleu
papeu jay p dagn name sa couleur
wakhou feineu yi khegnatina beu gouneu
[refrain]
au final c’est bizarre
mounomeu naat ci 10 ans
c’est bizarre
mane douma mbam mais kouma mbeuk ma bissap
c’est bizarre
rappeur te yi di gueuneu bizarre
chroniqueur bi lane nga djissat
diogue ci tata béw doug taxi yor attitude you méchant
doug gale gare benz takhoul ma ngui deg parole you méchant
koy tere wax wax wax wax
koy tere brr wax wax wax
letras aleatórias
- letra de i don't think about you (gil glaze x lanna remix) - kelly clarkson
- letra de cesta - vlado kreslin
- letra de tongue tied - king mighty
- letra de dumb kids in bed alone - william ezby
- letra de geluk - frank boeijen
- letra de noir éden - peter peter
- letra de like we do - chore boy
- letra de nightfalls (live) - cinema strange
- letra de feed the girls - amateur transplants
- letra de virtualife + social death - deadynsyde