letra de yaye boye - ismael lo
yaye boye balalma
yaye boye yaye boye balalma
yaye boyo balalma
khamna awma loula eupeu si adounya
yaye sama wadiour yaye sama lepeu
yaye man
kon yaye soumala m-sse togne mangui
dieguelou
souma m-sse dioum tay rethiou nako
ndakh yaye man guisna khale magua
sama kanam
ma khamne yaye boye fii la diar
balalma balalma baalalma
balalma balalma balalma balalmaa
yaye boye
soumala m-sse togne mangui dieguelou
souma m-sse dioum tay rethiou nako
ndakh yaye man guisna khale magua
sama kanam
ma khamne yaye boye fii la diar
balalma balalma baalalma
balalma balalma balalma
balalmaa
fane la mana diarr ba fayla yaye yaw
ndakh fayla douma yomba yaye man
waye dina diem sama kemtalay katane
bagua contane
louma def si yaw warou mako naw
yayo ho yaye beuguena yaw ngua contane
ndakh bo contane yala dana contane
gnou sargual sounou yayboy
yaye boye sonnagua yaye boye
m-sso tayi
yaguala tankhal dila sonal yayo
rethiouw ma loma done dioure
khamna amoul lo dadioul si gnoun gny
tay alhamdou lila mane mi bay la
diour na y dome khamna yoor ndiabote
modi lane
yaye boye yala nala yala fay
balalma yayoboy balalma balalma
balalma yaye boye balalma
letras aleatórias
- letra de collideascope - andy partridge
- letra de cuckoo - vhs
- letra de epiphany - dexter jordan
- letra de killedmyself - scribbletest
- letra de ultraviølent pt. i (skrybe reimagination) - crywolf
- letra de боль (pain) - kaeoki
- letra de bathroom - ユアネスyourness
- letra de les salamandres - alain chamfort
- letra de anmls - dj dust & jesto
- letra de junio 18 - norman norman