letra de teaupla anthem - elzo jamdong
hey yo welcome seme corner plateau
capitale de la capitale…
boulangerie sandaga, banteu ya…
yo boutique h24 nio ko ndieukk am man
bala ay nando’s ak leader price di am
cinéma plazza, paris, sandwich sara…
bokk dieuf, yakkh dieuf, gouy salane, mbott, zungle, f.f, bayeux, grand’cour, rue carnot…
yeah, yo fi la diangué gueum seme bopp…
hun, yeah
teaupla la diouddo, teaupla la yaro
teaupla la maggué, teaupla la yakkho
premier joint, premier iri
sama premier guinz, seme premier wiri
diadde kogn fakkh dém guédj
mane -ssane ak ousseynou nio dakkhone dém guédj
ponton legn dane yéndou biniouy diang féye
magg def comme grand yi wathie diangui blaze
han, bo khamoul lathié gueun
térou baye sogui léniouy lakké dieune
teaupla loum fi guédj dou takh me fatté leu
sones, van, ifan bi me nékké khalé leu
yék na bi pac di dèè 96
fi deunguey degg slang té do dem states
ay boyou 16 ans dawal mercedes
fekk ay grand wou 30 meussougn dem sakh thiès
yé-yéyék terrase, takk bagasou seu-ga ak rone “le parrain”
ndam-si-yalla rim-ka, mane ak cavin…
diouddo square, maggué pentagone
fréq na kébé, fréq na claire kane fréq na camp dial diop
se grand yi degn dane yarou bougn fi dane bal-si
métro, aldo, pcs, môle 2, niani…
diaw, popo, olivier gawe negn lène soule
ken mounoulène fatté, mingui mél ni dawe légn lène soule !
fallait qu’me def son bégué kogn bi
babiche ak ibou doumbouya kham nimeu beuggué kogn bi
nioune fi legn baser, yow fi legn t-ssé
fi kou fi se wa gallé tokhou nga woute no fiy dessé
légui magg na wayé doumeu fatté terrain rouge
terrrain wèkhe, terrain noir, 4 camps même sou meu traîner-toul
one, two, three, four sandial bébito
ko sandial ko sandial ko sandial bébito (wou)
outro
jamm dongg le
kou lim dioum…mang koy méy, yo mang koy méy wa gokh bi yeup
(wa teaupla wa teaupla en choeurs)
seme homie bizzle, thiaya, thierry, dixon, rakhou, nysv
soweto boys, arra, laye nahari
nioune douniou wakh lamine guèye, nioune nioye wakh van kham nga
wa diamono tamit gning thi birr
nioune nioye gonfler nerou wa hors town
eh boy nioune degn beugg souniou kogne waye
seme yaram mingui dow waye
teaupla le man, haaa
teaupla-a-a-aaa
letras aleatórias
- letra de fuzzy - the sevs
- letra de utopia pt.1 - beamer & winnterzuko
- letra de thin air - rita wilson & sleeping at last
- letra de every window is a mirror (big data remix) - joywave & big data
- letra de fiesta (con el whiskey del folclore) - meridian brothers
- letra de lástima - arde la sangre
- letra de supermarkt (ft. ghetto ben) - gpc
- letra de vibin' (extended) - 2ru3
- letra de dopamine - elephante
- letra de soledad - (a) isai gracida