
letra de diigu sandaga - elzo jamdong
verse 1
album bi guénneu neu, maa lène may bi ni ak khol bopu sèdd
sène critique yi laalouma comme diakhatou tchi deumm bou tiim bolou thièp
guiss naa ay kholou khèr
am neu niou bougone ma kholou mer
mane may dolli ay hits comme roy thi mom
dou meu done lou doul sama domou mère
sama khola ngui gueuneu yaa
melomind naala gueuneu yè
sama ngueum rek laa ganaayo ba done fi black star comme ghanéen
teuggoumeu rass walla deureum yaay
te freengdom bi di ne le gueuneu yéém
son ba nhgui reukkh seu radio
ne le lèrr ne free di neu gagner guerre
sama addouna la ma rap
sama none neko nama dap
def naa fi ay défis you diafé lolou
dang-y dof doflou wayé dofoulo
kham nga ni khammé kangam bi
borom ray ban yi ak nike’am yi
wa météo nenegn maay tangal fi
dou yow ak sey baggy ak sey ngandam tim
letras aleatórias
- letra de zhannia (havana disclaimer remix) - florezbaby
- letra de till the end - lui_surv
- letra de la pluie - napoleon da legend
- letra de nightlife - gazda paja
- letra de jangan mundur - nadia & yoseph
- letra de the most - rick stevenson
- letra de parasite - markjrgardner
- letra de na fé - nocivo shomon
- letra de harshlizer (uberbyte mix) - alien vampires
- letra de dummy dummy dummy - blue franklin