letra de comme mane - elzo jamdong
intro
ladies and gentlemen welcome to the freengdom haha
danga dof wala lane? huey peace
verse 1
rafett job ni alladji seme tour yalla djé toudd depuis seme jourou nguenté
war nga sage bo fateulikou ni bi ngay dioudou hopital sage femme moleu guenné
limey def defe tégou flow bi defe tarou melni lokho guél bou dogueu def henné
soubeu ci diante la goudi werr so mey sete fok nga tene une nouvelle étoile est née (est née)
eksinaa di liguey ak seme flow indi son you eupp rythme teugg katou diembé (yeah)
mane ak mister thiere niokoy togg yow se waania gueun khewi soirée fetchkatou thiembé
bodé dogueu yewou yangui nakh se bopp legui nga gueumentou boudé nioune ngay diemeu gêner (gêner)
fogone na ni peace le ak love, tegone na la bro ndékété moussibeu ngama yéné
a part mère bi awmeu royoukaye
maa ngui degg ibliss nane me elz kham na yone bi kaye
mane ngay diaamou maye se penkou doto look up to the sky
bomeu toppé legui fly légui son yi dialleu skyrock
mané ko yalla rekkeu meuneu yegueul seme art
momeu yoré momey yar soumeu goré momey aar
rouhou amoul ndieuk ken dou dieund seme libre arbitre
seme diné momeu gueuneul se ay milliards b-tch
bridge x2
moune nga def paris dakar aller-retour do guiss kou koy def comme mane
koumeu test ding ko reuthiou di nga degg niouné il est dans le coma
chorus x8
comme mane comme mane
i guess do guiss kou koy def comme mane hum x 4
verse 2
mangui fateulikou bi mey dogueu wathie paname deme dèè rap bi diplome la fa dieuli
wayé flow bi nekk seme yaram soumeu bayi wone mou sedd dakareu ngui neiger heure bi
rappeur yi bouniouy deglou seme hit deniouy t-te ni kou amoul ticket dadié’k controleur yi
dj-ing, mc, graff, yokk na tchi break-ing bad seme cd eupp dope gallé leurdi
khamone nani ma fi daakh play flow bi train na ko depuis bimey dogueu dougg aldo
yo deungueu khawa maniang te deme khawa maniaque doumeu sol loudoul sept comme ronaldo
semey andando weu gueuneu real wa madrid gueuneu sain germain, team bi nieuppeu serieux, team bi choquer serr yeup
moquer adversaire yeup
t-ssaré concert yeup
diakhal commissaire yeup
a part terreul mere diappé woumeu dara blème-pro
def na seme guerre diangal seme bopp done pro
sol jo togg dope, shooter diaroul gopro
nekoul mane ak niom douniou binde limey impro
yangui yakkh touflit boné elz defe aye
i’m so good kid comme wa dji defone son bou toudd “i”
homie khana diangueulougn leu saathie defe aaye
mane nga beugone toppeundo deungueuntane? hahaha aight
bridge x2
moune nga def paris dakar aller-retour do guiss kou koy def comme mane
koumeu test ding ko reuthiou di nga degg niouné il est dans le coma
chorus x8
comme mane comme mane
i guess do guiss kou koy def comme mane hum x 4
outro
moune ga def dakar sydney do guiss kou koy def comme mane
do guiss kou koy def comme nioune
jamm dongg leu
kham ngueen kou né tchi freengdom bi boy
danga dof walla
letras aleatórias
- letra de my sweet refuge - roo panes
- letra de cały czas specnaz - major spz
- letra de part of me - original broadway cast of dear evan hansen
- letra de sandiwara - xpose band
- letra de slag - flipp
- letra de emergindo da ciência (ao vivo) - arnaldo & patrulha do espaço
- letra de be the one - sílvia gironell
- letra de de wereld - de kast
- letra de wróci do mnie - gruby mielzky
- letra de hyper fangirl - the nostalgia critic