letra de nama yalla baal - elzo jamdong feat. mathart
tall bou yallah tall meune wakh fayoukoo (tall bou yallah tall wakh fayoukooo)
nama yallah baal gnoungui seine kaw (nama yallah baal niongui seine kaw yow)
taakeu shine di leer nagne ni bideeeewww
tall bou yallah tall meune wakh fayouko (wakh fayouko wakh fayouko)
tall bou yallah tall meune wakh fayouko (tall bou yallah tall wakh fayoukoooo)
nama yallah baal nioungui seine kaw (nama yallah baal nioungui seine kaw yow)
taakeu shine di leer nagne ni bideeeeew
tall bou yallah tall meune wakh fayouko
yeaaaaaaahhhh
tall bou yallah tall (tall bou yallah tall)
toll bou yallah bèy (toll bou yallah bèy)
diam bou yallah falle
dey gueuneu taak di gueuneu teuweu faye
yeah yeah
fall kou yallah may dale lo beugueu nangou tchi mome nangua nangou ni dangko koy faye
ndax kou yallah may baat dina wakh tei kou ame bou nekh dakoy waye
dama dane lakahatou si gnimeu gueuneu diégué
dama leerone si séni beutt bagnou goumbeu
gnimeu gueuneu sorri gnoma dane nieukeu sèinn mey taak di maag niou melni niou moumeu
niveau bi gueuneu kawei lay football
légui joueur yifi eupeu gueudd lay dougeul
dama diouk djité xarouma adiouma
mangui weurr kane momeu soutt tei guissouma
soubeu si djante la goudii weirr
taak na shine boul bagne lolou keine doussi polymiquer
ngandeu la leer neu may tchatou bideew bou dioudou feirr di lekk si bolou magg yii
fangu na fègne na
diombi ngeine ndax doolé dji nek tchi mane mo gueuneu kawei doolé djiné
rangou na kheikh na ba togu tchiin bi yagueuneu kheign nekh tédou gowé tchi nègg yeah
(refrain)
nagnou yallah baal
yagueuna def ay hits (alright)
bobou amagouma wone ay clips (alright)
li fi thiere bindeu si ay récitou bits eupeuna ay livres diekhal na ay bics (come again)
manei yagueuna bégueul ay niits (wallay)
bobou amagou wone ay sites (wallay)
binguay nieukeu dègu limeu bindeu dangua replay nangoulni kone mousso wone write (doope)
yow ma dakk rap sénégal dial home mo nei tchi ngiurr gui defko sama fringdom
sama dope legalize soumeu nekhone gueinei beum boumey toudei dakar-kingston
ame dieundeul bi defko ringtone
nioungui job té moussou gnou ame pistons
koula ladj ndax mangui gérer fight bi neiko may mouhamed ali sikaw ring bro
mane damey taak doumeu mandii
ay dadjeu naturels lay andii
defla mario diam leu ay champis
soudone western movie danioumey wanted
eh boulmeu wane sa kanamou gentil
xamnani yangui niane meu faye ngeu meune trankil
damey g-ss tombe soul ay garçons comme gaston tchi microphone mane may bandit
from the underground ligeey bi doroul tey (doroul tey)
guisngeu agueu nagne tchikaw ligeey bou sett dey faye (dey faaaaaye)
kileu yagu tipseilo keip sa good time (tiiiiiimmmmmeeeee)
get sunu vibes
alright (ouh yeah ouh yeah)
daniou daurr mou nathieu n-gg-r nieupeu seddeiko ko wallay (seddeiko wallay)
change game bi def safara andi ay mouslayes
never never nga guiss niou tchi details (non non non non non non non)
wowei meu grossiste
one more time (ouh yeah ouh yeah)
(refrain)
nagnou yallah baal
letras aleatórias
- letra de chill - dr. joe
- letra de garcon de yougoslavie - buldožer
- letra de death point - splifi x dash
- letra de a house a home - escape elliott
- letra de amarena - coldkevin
- letra de min baby - atv2
- letra de amicalement moi - nonioceleste
- letra de big watch* - lil andi
- letra de aire corriente - sr. pablo & avenrec
- letra de fighting demons - zaddysway