letra de ànd xeex coronavirus - dip doundou guiss
refrain
sa loxo set / tes mains propres
sa lepp set / que tout soit propre
bul nuyu kenn / pas de salutations
bul lëng kenn / pas d’accolade
bul génn kese ndax bëg génn / ne sortir que si c’est essentiel
bul sëqët fepp / ne pas tousser n’importe où
bul jége kenn / toujours garder une distance de sécurité
sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ / premiers symptômes : toux, fièvre et maux de têtes
soj, problème noyi, senn sa bakkan / rhume, troubles respiratoires, écoulement nasales
sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ / toux, fiévre, maux de gorge, début de malaise
du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn / ca ne tue pas le noir, pur mensonge
sa loxo set / tes mains propres
sa doom yi set / tes enfants propres

couplet
xeex ak corona virus, / combattre le coronavirus
microbe, jàngoro la, du nit / il s’agit d’un virus pas d’un humain
aduna nek si combat / le monde est en guerre
du gis ku muy xeexal / contre un enemi invisible
nuro nak grippe / des symptômes de grippe
nañu éviter contact physique / evitons tout contact physique
xajul grand yoff, colobane , pikine / n’a de place ni à grand yoof, ni à colobane, ni à pikine
tax ba ñu annuler programmes yi siiw / il est la raison de l’annulation de tous les programmes
tax ba ñu foog ni àddinay tukki / il donne un air de fin du monde
medecin sonu na si li / tous le personnel soignant au front
amul vaccin, ordonnance tamit / sans vaccin ni ordonnance
mu ngi ray, day toroxal nit yi / ce virus vulnérabilise et tue
buñu tooge dina bari ay victimes / si l’on reste observateur les victimes seront nombreuses
set si sa askan, set si sa bopu / propreté collective et individuelle
tëju te baña seeti sa mbokk / eviter les visites, rester chez soi
julli sa màkkaan, messe si la bokk / toutes les prières à la maison quelle que soit notre religion
xeex ko mu jeex mbir yepp mëna doxx / combattons ce virus pour que tout revienne à la norme
masque, sabu, antiseptique / masques, savon ou gel antiseptique
raxasu, sangu dadi set wecc / se laver, laver ses mains, rester propre
dal, muñ, bañ lu melni dess fi / calme et sérénité pour éradiquer ce fléau
gën di ñaan pour jamm day dikk / prions ensemble afin de vaincre ce virus
refrain
sa loxo set / tes mains propres
sa lepp set / que tout soit propre
bul nuyu kenn / -pas de salutations
bul lëng kenn / pas d’accolade
bul génn kese ndax bëg génn / ne sortir que si c’est essentiel
bul sëqët fepp / ne pas tousser n’importe où
bul jége kenn / toujours garder une distance de sécurité
sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ / premiers symptômes : toux, fièvre et maux de têtes
soj, problème noyi, senn sa bakkan / rhume, troubles respiratoires, écoulement nasales
sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ / toux, fiévre, maux de gorge, début de malaise
du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn / ca ne tue pas le noir, pur mensonge
sa loxo set / tes mains propres
sa doom yi set / tes enfants propres
bul nuyu kenn / pas de salutations
bul lëng kenn / pas d’accolade
bul génn kese ndax bëg génn / ne sortir que si c’est essentiel
bul sëqët fepp / ne pas tousser n’importe où
bul jége kenn / toujours garder une distance de sécurité
sa loxo set / tes mains propres
sa lepp set / que tout soit propre
bul nuyu kenn / pas de salutations
bul lëng kenn / pas d’accolade
bul génn kese ndax bëg génn / ne sortir que si c’est essentiel
letras aleatórias
- letra de i don't give a fuck - original juan
- letra de abyssal streams - kambrium
- letra de beauty in passing - words of farewell
- letra de rain - emily's army
- letra de bolt cutters - single mothers
- letra de life in color - kennedy betts
- letra de cedar rapids 10 am - carrie newcomer
- letra de meta - zoen dcn
- letra de intercontinental - ali belmont and the delivery boy
- letra de right now - rag'n'bone man & leaf dog