letra de so dowpe - carapid music
live from neegu rap studio
carapid music, bako
[verse 1 : bako]
i’m so dowpe sama syndrome
su nieupé démé droite si lay daldi dieul gauwche
up in the sky on the cloud on tour
def velo pédalé… amstrong dope
legui magui dial télé yea c pa faux
ak sama tourr bou bizzar mane leu boy bako
bokk negn cl-ss dameu seki rek brow
wagnina thiép ba di thiop ay toooo / iih dey tiol…
suma newone gars yi damey bayi rap
con-current, bete-current nieupeuy diokhé p-ss
diluant pour sa guél mane rek ley guinz
carburant wu rap game ladial anna b-sse
[bridge: bako]
if you dont knoow now u know, mafi diarone
dal sen kaw ni mario…
diéma def couplet bou amoul sens
ma daldi am chance affair bi am sens anh
[hook : bako]
awma bena g-yn soudoul music sama homie
deflén foukki dadj rek sa gars yi daldi mandi
i’m so dowpe, mani la i’m so dowpe !
[verse 2 : bako]
im so dowpe sama syndrome
su nieupé démé droite si lay daldi def pauwse
deglou rap galsen yukhu what are those ?
kash bizi yukhu na ci mic bi ba tuberculose
wa mais.. ana gnima done ré bimey dora rap ?
doméro, suma réwone saggaléne, sayoléne yéwo xalat léne…
ku dakeu rap terre air mer univers
may sa pere kone may sa paa
diarul dem ba vaticcaan ndax may sa pape
papi chulo, kufi imposer ay regle niu dioxla tampon
[hook]
[bridge: bako]
if you dont knoow now u know, mafi diarone
dal sen kaw ni mario…
yenesaay damey 6 samey propre sons
letras aleatórias
- letra de contigo - niños del cerro
- letra de tron - lil tooth
- letra de fendi - elias
- letra de ever after - terry taylor
- letra de morning glory - hamartia
- letra de solip - psihotrop
- letra de the light - mr. happie
- letra de fat free - hitomi
- letra de how things were - a-rodd
- letra de ooo baby baby - edwin starr & blinky