letra de dream - carapid music
yeah everyday ngamay guiss may rap
xamoulo fima yakara jeum
let me tell you today what i always dream about
teki b nékeu nit , hun , raaapid music!
[fla]
only one dream til i was young
done ci rap bi ab king kong
every week ma make a new song
beuri diplome fis ci bépeu xétou komkom
founiou né fla ni uno rek pas de dos
siguil mere ak pa b ci sa samay goss
melni béneu weezy jayz wala rick ross
sol coss cos allumette di diay free freaky boss
di ride maserat ferrari waaleu bugatti
(ferrari waaleu bugatti)
[kalz]
rien n’est impossible rap bi dameu nieuw pr job sii
lou nice meu djeul ko déf lou bone meu djémeu soopi
bolé ko ak djangue bi fils moméy takha djopi beu sorri no hurry
beuss dineu djot dina dém beu tchop sii
k.a.l.z. génteuh si rap bi
tékki beu done garap gui
textes yii oubil meu gaps yii
meu bindaat sameu story
paa bi done aladji
niou woowé mère bi adja
inchaallah am alaal dji
yes i can #obama
[refrain : soupman ]
i have a dream
i wanna see my crew to be on top
that’s my dream
we gonna travel around the world together
in a fast car
speakers in the back
my country is still
in the misery
yeah, together
we have to do something
to change it
[soupman]
h-llo world
i’m gonna tell u my story
first of all, i’m a young super beat maker
my daddy doesn’t know
but i’m a singer too
i pray for my future
oh mamma, i love u
i’m a day dreamer
i target the success
the money gonna follow me back
like your wife on twitter
jump jump on her b00bs
think twice about your life (han)
i’m walking in the street
the hope in my bag
if you have a dream negga
you can follow me back
i’m gonna change the rules
together we gonna win the cups
i don’t give a f-ck about that
negga i’m so cute (han)
[kalz]
i know that u love me
but i’ll be richer for you
we gonna be… and free
in a sweety house
i know that you love u
but i’ll be richer for u
for youuu
[refrain]
[kalz]
sama néne tothieu sameu laaf fo k meu firri ko
dounde samey génteuh fo que meu waaf naw ni hélico
waf naaw ni hélicooooo
reuth sameu kaaf trophée bi meu dém djeuliko
bégeul sameu gars yii yobuléne bénéne niveau
bénéne niveauuuuuuuu
[fla]
mama said i’ll got it cuz i was born with it
t.o.p lay visé homie té yakaroumaci nit
game limay def té diko def ak jom ak fit
bi gme fok ma téki ci té douma lal wéthiét
amb-ssadeur rappeur on m di k c impossible
but dad use to say pr un diouf rien d’impossible
[kalz]
i told you rien d’impossible
hey fla ioe togeul rék see
séntul the warriorz posse
car fo k niu fésseul poches yi
beat bu nieu meu encaissé seug ssi soneeu ssi bindeuh beu pakété ko
fékéh beu fans yi feuggssi dougoussi dj-pssi bagnuy dém vers le haut
vers le haut gnu outidji doe
outidji doe né talouniou fo
talouniou foe té bougouniou thiow dream bi dégn kéy mateuli ioe
trône bii yéngeu gougn feu
téréwul mangui kéy séntou
kham né yone bi goudeuh neu
mais thioloul mangui mandou
djeul sameu temps thiéné cool khamné yagatoul
tabaxx sameu ngandi gaalé ak béneu pool
[refrain]
letras aleatórias
- letra de paska sydän - hank solo
- letra de k4fe(cn)631 (2013) - fatnick
- letra de o carro do sonho desiludido - asaph eleuterio
- letra de berhenti berharap - dangdut koplo nirwana feat. via valen
- letra de fal$o mano - vini santo$
- letra de i dont een watch basketball - fullyautomaticdrayco
- letra de reject - g herbo
- letra de 사랑, 독 love, poison - 소울라이츠
- letra de fantasy - eternity forever
- letra de nobody's perfect - harvey schmidt