letras.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

letra de beware (remix) - carapid music

Loading...

[refrain : kalz & maya]
bim leu néé, mak yaw djéxneu
seuu xol bi yeup leu totch
lane mo taaax niou mouuuuuudjei fi waxx me lane mo taxx
ouuuh dafeu métti
té yagone négn meu saxx toppeu di waxx
daneu wareu wareu wareu
moytou djigéne bou xoleum totch

[fla ]
ama doxane khalei bi parei mou jigmeu
sama lepp day bakh b sakh ma t-te meune
teksi beuri xaliss b boy yi sib meu
sib meu ndakh xaleyou toy yi mane laniouy signe mane
rek ma dadi fate adou na jeyma
souma owei ma jani loumou wakh ma tegui di diay reuy mane
wayé bima bayei mou melni dafma rey mane
ma commencé ndol
manatouma am guel
wala kouma dokhane un jr niou bayantei
legui ma raw sakh katy pery
sama repution la yakeu melni bou john terry
sama life yeup tiol
torturé sama xel
manatouma am lou bakh
mou melni damay soukh ci ap gandim pakh
wakhone naniou ma ma def ndank té di moytou
nakh jiguene sokay toroxal sa kaw ley keupou

[refrain : kalz & maya]

[bridge]
-phone ring-
salut c’est amina
je ne suis pas disponible pour le moment
ni pour un certain temps,laissez moi un msg…

[bako]
anh legui ni leu, damley wo nguey nekk bv, f-ssn taloumaleu…
degg na lumay wakhal takh sayu ma rombé kogn beu sa copine yi dima sewel
fateulikoul yameu wékheul… ba meu nirok colgate
tey nga beugma tilimeul… boul yakka sama déér
iow dh yameu betteu wakh deugeu yameu betteu baby honey coco cheri
wayé amina, yani sama bopp oohhh… all night long
mane la dou kénééne, rén la dou deweun
dém neu dou nieuwat, diekhna diekhna…

[refrain : kalz & maya]

letras aleatórias

MAIS ACESSADOS

Loading...