letra de jackpot - boiie pablo
couplet i :
nimay rappé dafa sett sett
doo guiss kou melni mane tek tek
koumay lathié dima seet seet, n-gga normal ma dieem leu diaay prek prek
mane leu jackpot maay 7 7, eundil money bi par chèque chèque
douma xholou melni fake fake, n-gga sama xhel dey faté fatt fatt
soo beugué clash douma cii wait, dagnii back to back melni meek drake
real n-gga melni 2 pac pac, diapp b-tchez rendylén pak pak
diouteul état diko f-ck f-ck, politik ak polémique dou choc choc
nieuwal face to face manguék glock glock, ballou gun ci sa bopp boy loo f–k f–k
maay sééntou, di soorou, sempii sénii chérie! sekh di namp sénii seins yi
sagaal ba sonn di sissou seet ba seet ni soma sooro dinga souroukh
civilisé simplicité lepp pour briller ni samay guél ak seenii teint yii
seetlou seenii sujet diko sekhlou niouné real mc dima soufou
maay soukii safal seeniou sénii sénior !
kou dougou ci mane soor nga thiéép boudoul niorr !
mane deugueur bopp rek motakh ma xham door !
xham sam bopp paré deff lima niorr !
douma complexé noir melni léo senghor !
_souma defoul effort dou téré ma fort
diambouma wanté nieupp fii legn farr
deugg leu talent amoul limouy diarr
wanté alal kenn douko forr ni
pont :
nimey rappé dafa set set..
foy guiss kou melni mane tek tek ?
couplet ii :
done 2pac dou takk bandana
done ouztaz dou sahal barbe man
dem jumah dou dem nga adianaa mais heyna tam dem nga ambassade
maay tek lou tarr ba raw mbedj si ngaam
ndakh deff lou yomb moy lou metii si man
n-gga dama took rek bayré fekksi ma
douma wakh ak niom loutakh niouy ci man
sa nelaw yii dagg na, mangui nieuw xhadialma
boy bi mom tangg na ,flow bi comme tanganaa
wahouma tiakhane nak, louma deff dangane’na
tamba ba dagana
gang bii nieuw nguémbeu ma, teksi boy nénégn ma jobal niou yénou la
xham negn nii niémé nga, ni nga mel yéémé na
bénn mc yéboula, kepp kou nieuw delou wate
sa rappeur laay diomalate ! ndakh dama deumé chacala
maalénkoy tamalate ! louma guéné yeungueul melni tamala
ci digg ni dabalaaa ! manguék balle melni dybala
succès diahalouma ! dafma sapy sakh apparemment
sa baby girl thiaga la ! kodj ma sathur nako niamalaate
dara douma stop x2 , xhana ma guiss kouma jongalate
sougn dadié nga niangalaate ! pop a sh-t malakoy diangalate
outro
boyi pour niom faut niou smoke- pour pop
guél yii xhessal pour nirook – toubap
dii niodii bandit té meusso- coupable
demal dianguii ioe meusso- capable
letras aleatórias
- letra de momentum of misfortune - leather lung
- letra de both sides - atex
- letra de coming round - unbelievable truth
- letra de doom's plan | parody of god's plan by drake - domald
- letra de on my own - trevor daniel
- letra de auf der flucht - massendefekt
- letra de batphone - arctic monkeys
- letra de saudade e fantasias - lulu marah
- letra de pray for air - mammút
- letra de step it up and go - dr. watson