letra de crack - boiie pablo
couplet i :
nopp kassé takhoul niou meunn diokkoo
meunn nguen déganté way dolen degoo
melni président bé’k opposition
s/o macky sall s/o sonko
meunn negn bokk wanté ken dou seddo
ndakh niakk sagn-sagn ci biir reew bobu
regime’ou dictature ng-y am fof
s/o yaya diamé s/o barro
liila yombb yene-saayi do xham ndieugueum
dang-y dem sakh ba moudié ci gueuleum
niaakeu done gorr, niaakeu xhalate fils
motakh askann’ou libye worr khadafi
foo fékkeu naafék’h dey taakalé
dou séétane fou diiganté ratakhéé
motakh guerre civil afrique niouy réyanté
f-ck union européenne, f-ck u.s.a
africa united, never you see
ours heads of states nevеr they think it
good mentality nevеr we get
that’s why we never fly like a jet
refrain :
[crack !
dou am sa bac, di diangué ci fac, rek deff nala crack
young n-gga no cap !
crack yang’ci kogn bi dieul murs yi di track, mélanger drogues yi ba créer ci crack, la police nous traque mais jamais on craque
crack yang’ci jail bii dii xhalaate ay atte, xhalaate you yaatou ci ay neeg you xhatt ]
couplet ii :
dee soul’neu seu djeumeu mais souloul sey dieuff
sooy dee do yobaalé kone dieuf yii dey dess
gnii fayekou akkeu sa yiiw lagnii keuff
soula néékhé boul baalou euleukk dingko ress
louy lonkou dou diappeu niayy
té sapeur amoul xham xham bouy takh ba volcan fay
souma namé tardé lalay tontou key
ndakh matoo ma goontou, matooma kheuy
gnieupa guena mouss ki guena mouss ci nieup
ma guena mouss ci nieup dii andak nieup
tey bodone tanneu doma bayi ci nieup
neekh’a ragné li ci mane newoul ci nieup
yaa defar montre mais yallah mom seu temps
yallah sakkeu nieup ioe ng-y gueum satan, kone diaam ng-y diaamou, loloy perte temps
life bi dafa gatteu amoul mi-temps
té meuwtii doula meussa mey temps
dafay dieuffé ndiigueul en deux temps
dieul sa rou’h paré ladj leu lodone deff seu temps
outro
[crack !
dou am sa bac, di diangué ci fac, rek deff nala crack
young n-gga no cap !
crack yang’ci kogn bi dieul murs yi di track, mélanger drogues yi ba créer ci crack, la police nous traque mais jamais on craque
crack yang’ci jail bii dii xhalaate ay atte, xhalaate you yaatou ci ay neeg you xhatt ]
letras aleatórias
- letra de wrong - kane roberts
- letra de me first - camira the rapper
- letra de my country is the best (english version) - pochonbo electronic ensemble
- letra de the best is yet to come - fiona
- letra de a contracorriente - julia medina
- letra de alter ego - arden bright
- letra de sinking - maya hirasedo
- letra de untitled - pgtheawesome & 6th ave
- letra de iwannahateyou - killvein
- letra de falling - living arrangement