letra de belek ii - boiie pablo
ego, rap bi lagni taal comme tabac, kheuthieu n-ggas yi fey comme mégot
flow you méga, legn deuké deff di deffate, té message yi dou ay promo
non duniu débat, mane lima miine nak moy degat, heyna motakh mounou nioo degoo
ay dieuf you pataa, té dama sew comme sa- djiko guel
ham nga lolooy dieego
rap bi dou meussa noy, koufi taran-tathieu wadialal tey ma tanthieu seu…
sanio nieuw sama zone difa santhieu seu..
mane may nieuw ba sa kogn n-gga sampp feu !
mane may nieuw ba sa kogn n-gga nampeu seu..
learn..i’m the ghost !
fii lep dey rimer ni toni ci kaw motocross
benn laa ci kaw souf bi ni lac rose
niom daniou laté ni meuf ak couleur rose
soumay taal sa rappeur , c’est excellent
comme son excellence di toukh ay excellence
entre papa’k yaye sakh awma préférence
taal na sentiments yi sotti wate essence
sama rappeur’ou bopp awma référence
–
belek x 2 ….grrrrrk – paaaw !!!
nioy ba sa kogn difa freq..nioune guissougn fooy fatteu né dougn fii aw !!
belek x2 …..grrrrrk – paaaw !!!
nioy nieuw ba sa kogn difa freq !
sa mère sakh sou moolé niou krik sa papeu !
–
saa youma guéné son t’es au courant young n-gga pourtant jobouma senelec
belek x2
deff trace biir africa comme télé
dara dou xhew doo laal kenn danga teulé
souma amé zéro faute rek lay fêter
bokoul ak ndiaago biy foot ak fété
doiugué tamba nieuw eundi tang-y
que du sal bouma digueul ay thiangaay
no mystique sokhla wuniu thiakaay
limay bindeu footekat sakh douko gommé
..rap boudone ludo may omé
niom liniou garr mako goobé
deuk-ma ci garap teewoul dama xhobé
lou mbedd bi xham ecole xhamouko, way lou école bi am mbedd amouko
nitt lepp liko sonal rek tammouko, way lepp liko diomal rek xhamouko
lèb sey fann té dougn la fay weer bou dee
sama tontou dou fanane alleuh, dou goudé
samay dalleu’h bougn daggué lolou dou blem, dougn ma téré dem , maa raw oudé
–
belek x 2 ….grrrrrk – paaaw !!!
nioy ba sa kogn difa freq..nioune guissougn fooy fatteu né dougn fii aw !!
belek x2 …..grrrrrk – paaaw !!!
nioy nieuw ba sa kogn difa freq !
sa mère sakh sou moolé niou krik sa papeu !
letras aleatórias
- letra de like that! - louie blue
- letra de can you hear me - ivan b
- letra de purple purple - cflow/schlatta west
- letra de schizophrenic - bbyternal
- letra de winter days - krandank
- letra de сад (sad) - кто там? (kto tam?)
- letra de discretos [interlúdio] - treysoul
- letra de loco - ocyris
- letra de hey! - child bite
- letra de my name is.. - once monsters