
letra de karma (wolof version) - bachir samb
ma ngi done perte sama temps
biss bounek dileu khalat
lou diakhassé sama adouneu
mom nga ma tek ni
dio8 na wakh samay andando
nañ dem dinañ guisé benen yon
baby man soumeu sañon
damay wakh ni iow amoulo morom
lepp lo guiss dineu diekh
mouñeul na sama banekh
liñ don wakh di wakh wakhet
tay dji dineu diekh
yakaar bou tass nga meu fi bayil
doumeu wathié samay lokho
beugon nala ba fi beug di yam
mais sa karma di neu tew tew fii
lepp lo leplé mom lañ lay fay
teksi diokhlako fo fogoul ni
dineu meuneu am
elle me disait que j’étais différent
souñ la guisé ñom dañ leuy diema foé
égocentrique comme si еlle le voulait
narcissique amеr
n’essaie pas de me foutre dans la merde dokhal dokhbi ye
loin de toi je protège mon énergie
man change nala changé ma vie
lepp lo guiss dineu diekh
mouñeul na sama banekh
liñ don wakh di wakh wakhet
tay dji dineu diekh
yakaar bou tass nga meu fi bayil
doumeu wathié samay lokho
beugon nala ba fi beug di yam
mais sa karma di neu tew
mais sa karma di neu tew
fatalikoul
loutah nga def meu li
loutah nga def meu li
en vrai j’voulais juste ta sincérité
je m’en vais
letras aleatórias
- letra de getting better (the beatles cover) - willyrodriguezwastaken
- letra de вождь чувашский (the chuvash ruler) - yokakaminari
- letra de dystopia - doxxyz
- letra de the arrangement - kele okereke
- letra de runnin circles - galaxya
- letra de eulogy - kev carmody
- letra de valium sunday - blackcat revival
- letra de buenos días amor - mexican institute of sound
- letra de medley joão viu / a ditosa cidade / desapareceu um povo - vitória lima (gospel)
- letra de necromancy song - erica hancock