letras.top
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

letra de xel akk xol - ashs the best

Loading...

xel akk xol lyrics
yeah, eh eh eh
lé, lé, walé
hum, hum
suba suma yeewu
yaw lay bëgg jakarlool
sa suma yeewu
yaw lay bëgg njëkk xol
ëlëk lu mata soor la
wayé xel xalatu ko
ëlëk ay jaar-jaar la
sama xol yëgoon nako muy ñëw
xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
xol yëkk yëkk la
nit ak jëmëm jë
dara xaaju fë
sa suma yeewu
yaw lay bëgg njëkk xol
(suma yewo yaw la bëgg njekk xol)
fajar suma yeewu
yaw la bëgg jakarlool
denk na la guddi
fanané yakkar ci yaw
gent na la guddi gi yëpp
ndax fajar yaw lay jakarlool
mbëggël!
xel xalaat la
xol yëkk yëkk la
nit ak jëmëm jë
dara xaaju fë
nit nak ak jëmëm jë
dara fa xaajul

letras aleatórias

MAIS ACESSADOS

Loading...